Numbers 24:7
TSK
Ndox maay wale cay bagaanam, am jiwoom màndim ndox, buuram nara sut Buur Agag, nguuram jóg ba kawe.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndox maay wale cay bagaanam, am jiwoom màndim ndox, buuram nara sut Buur Agag, nguuram jóg ba kawe.
Mooy yékkatee ku ndóol ci suuf, jële ku ñàkk ci mbuubit, boole leen dëj ca garmi ya, sédde leen jataayu teraanga. «Aji Sax jee moom kenuy suuf, samp ci àddina.
¶ «Kon nag waxal sama jaam Daawuda, ne ko: “Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi dafa wax ne: Maa la jële ca parlu, ga nga toppe woon gàtt ya, ngir nga doon kilifag Israyil, sama ñoñ.
Mooy Yàlla ji ma feyul, nangulal ma xeet yi.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.