Genesis 44:23
TSK
Nga wax nu ne nu: “Bu seen rakk àndul ak yeen, dungeen jàkkaarlook man.”
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nga wax nu ne nu: “Bu seen rakk àndul ak yeen, dungeen jàkkaarlook man.”
¶ Ci kaw loolu Mikal doomu Sóol bëgg Daawuda, ñu àgge ko Sóol, mu am ca mbégte.
¶ Sóol yebal ay ndaw ca kër Daawuda ngir ñu xoolal ko ko, ba bët set, ñu rey ko. Mikal, soxnas Daawuda, yégal ko Daawuda, ne ko: «Soo rawalewul sa bakkan ci guddi gi de, bu ëllëgee dees na la rey.»