TSK

TSK · 2 Samuel 3:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

«Ruben, yaw mi ma taawloo, nga sosoo sama digg doole, sama ndoortel kàttan, yaa jëkke sut moos ci teraanga ak doole.

¶ Ayinowam ma cosaanoo Yisreel itam, Daawuda jëloon na ko soxna, ñuy wujje ñoom ñaar.

¶ Gannaaw loolu Absalom doomu Daawuda moo amoon jigéen bu rafet bu ñuy wax Tamar. Jeneen doomu Daawuda ju ñuy wax Amnon nag xemmem Tamar.