1 Samuel 30:4
TSK
Daawudaak mbooloo ma mu àndal nag di yuuxook a jooyoo, ba amatuñu dooley jooy.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Daawudaak mbooloo ma mu àndal nag di yuuxook a jooyoo, ba amatuñu dooley jooy.
Daawuda nag jox ay nitam ndigal, ñu rey leen. Ñu dog seeni loxook seeni tànk ca tenqo ya, wékk néew ya ca wetu déegub Ebron, daldi jël boppu Isboset, suul ca bàmmeelu Abner ca Ebron.
konoon it muy ñaawtéef gu yeyoo àtte, nde kon ma weddi Yàlla ma fa kaw.
¶ Ba Yeesu jubsee ba séen dëkk ba, jooy na ndax moom.