TSK

TSK · 2 Timothy 2:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Su ko defee kilifay xarekat yi wax ak gàngoor gi, ne leen: «Ana góor gu ci tabaxoon néeg bu bees te daloogu ko? Na daldi dellu cab néegam bala moo dee ci xare bi, geneen góor daloo ko.

Luke 9:59 TSK

Mu neeti keneen: «Toppal ci man.» Mu ne ko: «Sang bi, may ma, ma jëkka dem robi sama baay.»

Joŋantekati tàggat yaram yi, dañuy yar seen yaram bu metti, te ñooñu kaalag ndam guy seey doŋŋ lañu ci yaakaar, waaye nun, kaalag ndam gu sax dàkk lanu ci yaakaar.

Xanaa kay noonu nu Yàlla doyloo, ba dénk nu liggéeyu xibaaru jàmm bi, noonu lanuy waaree li neex Yàlla miy seet ab xol, te dunu ci wut bànneexu nit ñi.

Ndax kat Demas, àddinay tey la sopp ba tax mu wacc ma, dem Tesalonig, te Kereseñsë dem na diiwaanu Galasi, Tit dem diiwaanu Dalmasi.