TSK

TSK · 2 Timothy 3:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ku nekk ca ñoom sànni yetam, mu soppliku jaan, yetu Aaróona nag wonn seeni yet.

Ci kaw loolu ñeengokat ya taluñoo janook Musaa ndax ay taab, ñoom ak waa Misra gépp.

Ca la Yàllay jóg, ngir àtte, ba wallu kuy néew dooley àddina. Selaw.

Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoori xare yi dafa wax ci mbirum Akab doomu Kolaya ak Cedesyas doomu Maaseya, ñoom ñi leen di jottli waxyuy fen ci turam. Mu ne: Maa ngii di leen teg ci loxol Nabukodonosor buuru Babilon, mu rey leen, ngeen di gis.

Te sa yonent yi la doon jottli waxyu, naan la buuru Babilon du dikk ci seen kaw, yaak waa réew mii, ana ñu léegi?

Loolu lañu doon jéem bés, rab wu bon wa ne leen: «Yeesu déy, xam naa ko. Póol it xam naa ko. Waaye yeen, yeenay ñan?»