2 Kings 2:11
TSK
¶ Ci kaw loolu ñu ànd di waxtaan, di dem. Yéguñu lu moy watiiru sawara, wu ànd ak fasi sawara, ne jimeet, dox seen diggante ñoom ñaar; Ilyaas yiiroo aw callweer, yéeg kaw asamaan.