TSK

TSK · Acts 10:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Gannaaw loolu ñu jóge ca jaamookaay ba, dellu ca dëkk ba. Ba ñu demee kër ga, Samiyel diisook Sóol ca kaw taax ma.

Këri Yerusalem ak këri buuri Yuda dina fees ak sobe ni bérab bii di Tofet. Mooy mboolem kër yu ñu doon taalal cuuraay ca kaw taax ya ñeel biddiiw yépp, ak di fa tuural yeneen yàlla.”»

Ci kaw loolu Buur Daryus torlu mbindum aaye ba.

Acts 6:4 TSK

Nun nag nanu wéye julli gi, ak liggéey bi ci kàddu gi.»

Acts 11:5 TSK

Mu ne: «Man de damaa nekkoon ca Yope, di fa ñaan. Ci biir loolu ma daanu ag leer, daldi gis ci peeñu lu mel ni sér bu mag bu ñu téyee ñeenti lafam, mu wàcce asamaan, ba agsi ci man.

¶ Kon li ma bëgg moo di góor ñi di ñaane fépp, tàllal loxo yu mucc sikk, te bañ cee boole meroo ak mbiicoo.