TSK

TSK · Acts 13:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Luke 7:16 TSK

Tiitaange nag jàpp ñépp, ñu sàbbaal Yàlla, naan: «Yonent bu mag feeñ na ci sunu biir!» te naan «Yàllaa wallusi ñoñam!»

Acts 6:10 TSK

Teewul àttanuñu xelam mu rafet, ak Noo gi muy waxe.

¶ Kàddug Boroom bi nag di law ca diiwaan bépp.

Acts 19:7 TSK

Taalibe yooyu yépp a ngi wara tollu ci fukk ak ñaar.

Ndaxte gànnaay, yi nuy xeexe du gànnaayi suuxi neen, waaye da di gànnaay yu am fa Yàlla, kàttanu daane ay tata. Te xalaatin yu jubul, noo leen di daaneel,