TSK

TSK · Acts 19:33

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Piyeer liyaar leen, ngir ñu noppi, daldi leen nettali, ni ko Boroom bi génnee kaso ba. Mu ne leen: «Yégal-leen ko Yanqóoba ak yeneen bokki taalibe yi.» Ba loolu amee mu génn, dem feneen.

Mu may ko. Póol taxaw ca dëggastal ya, tàllal mbooloo ma loxo, ñu ne selaw. Mu wax ak ñoom ci yawut, ne:

Acts 26:1 TSK

¶ Ci kaw loolu Àggripa ne Póol: «Léegi sañ ngaa waxal sa bopp.» Póol nag tàllal loxoom, layool boppam, ne:

Ci ñooñu la Imene ak Alegsàndar bokk; Seytaane laa leen jébbal, yare leen ko, ngir ñu bañatee saaga Yàlla.