TSK

TSK · Acts 20:34

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Nan dem ngalla ba ca tàkkal dexu Yurdan, ku nekk ci nun sàkk fa aw dénk, nu defaral fa sunu bopp bérab bu nu daje.» Alyaasa ne leen: «Demleen.»

Mu daldi yebal fa Maseduwan, ñaari jaraafam, Timote ak Eràst, moom mu toogaat ab diir ca Asi.

Xanaa bokk yi, yeena ngi fàttliku sunu doñ-doñ ak sunu coono? Diir ba nu leen di yégal xibaaru jàmm bu Yàlla bi, guddi ak bëccëg lañu daan liggéeyaale, ngir baña diisal kenn ci yeen.