TSK

TSK · Acts 21:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Samiyel wax ko lépp, nëbbu ko ca dara. Eli ne: «Mooy Aji Sax ji. Li ko soob, na ko def.»

Esekiya ne Esayi: «Kàddug Aji Sax ji nga jottli jàmm la.» Booba ma nga naan: «Xanaa du jàmm ju ne ñoyy ay am sama giiru dund?»

Luke 11:2 TSK

Yeesu ne leen: «Bu ngeen dee julli, ne leen: Baay, sellnga ñeel na saw tur, na sa nguur dikk.