TSK

TSK · Acts 21:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Éy Yàlla, ba may ndaw, nga ma xamal say kéemaan, te ba tey jii maa ngi koy biral.

Bijjaawu bopp kaala gu yànj la, njekk a koy maye.

¶ Ca ëllëg sa Piyeer agsi Sesare. Fekk na Korney di ko séentu, daldi woo ca këram ay bokkam, ak xaritam yi ko gëna jege.

¶ Gëmkat ña tasaaroo woon nag ndax fitna ja woon, ca mbirum Eccen, mujj nañu jàll ba diiwaanu Fenisi, ca dunu Sippar ak ca Àncos, waaye àggewuñu kàddu gi ñeneen ñu moy Yawut yi.

Acts 21:3 TSK

Naka lanu dem ba séen dunu Sippar, wacc ko nag sunu wetu càmmoñ, jublu diiwaanu Siri, ba teeri Tir, ndax fa la gaal gi waroona yebbi ab yebam.

Nuyul-leen ma Andoronikus ak Yuña, sama bokki Yawut, yi ñu ma tëjandooloon; ñu ñu nawloo lañu ci ndaw yi, te ñoo ma jëkka gëm sax Almasi.