TSK

TSK · Acts 21:40

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba mu ko defee ñu gaaw, summi seeni mbubb ñoom ñépp, lalal ko ca kaw dëggastal ya, ba noppi wal liit ga naa: «Yewu falu na buur!»

Acts 6:1 TSK

¶ Jant yooyu nag, naka taalibe yi di gëna bare, Yawut ñiy làkk gereg tàmbalee ñaxtu ci kaw Yawut ñiy wax seen làmmiñu bopp ndax néewal gu ñu gis ñu néewal ko seeni jëtun ca na ñuy séddalee ag ndimbal bés bu nekk.

Póol jóg, tàllal loxoom, nee leen: «Yeen bokki Israyil ak yeen jaamburi ragalkati Yàlla yi, dégluleen!

Ba Póol àgge ca dëggastali tata ja, mbooloo ma daa sànju ak doole, ba takk-der ya mujj fab Póol, gàddu ko.

Nu ne dàll fi suuf. Ma dégg baat bu ma wax ci làkku yawut, ne ma: “Sóol, Sóol, lu tax nga di ma bundxatal? Dangay sonal sa bopp rekk, mbete fas wu manula woŋŋeetu ba wéq dëgël bu koy jam.”

¶ Ci kaw loolu njuuma yi dajale buur yi ci bérab bu ñuy wax Armagedon, di baatu ebrë.