TSK

TSK · Acts 25:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Sang bi dégg li ko soxnaam wax ne moom la ko jaamam def, mu mer lool,

na ñaari nit, ña séq mbir ma taxawi fa kanam Aji Sax ji, fa kanam sarxalkat ya, ak àttekat ya ca yooyu jant.

Ku jëkke layoo, ñu ne yaa yey, ba keroog ka nga joteel weddi la.

Ba ñu ma àggee am tëru mu ko Yawut yi waajaloon nag, ci laa ko yebal ci yaw ci saa si. Jox naa itam ndigal ñi ko sikk, ne leen ñu wax ci sa kanam, gan tooñ lañu ko toppe.

Acts 26:1 TSK

¶ Ci kaw loolu Àggripa ne Póol: «Léegi sañ ngaa waxal sa bopp.» Póol nag tàllal loxoom, layool boppam, ne: