TSK

TSK · Acts 28:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ndax kat li feek juróom ñaari fan dinaa wàcce taw ci kaw suuf diiru ñeent fukki guddi ak ñeent fukki bëccëg, ba far ci àddina mboolem mbindeef mu ma sàkk.»

Maa xejjoo képp ku la ragal, tey topp say tegtal.

Acts 19:1 TSK

¶ Diir ba Apolos nekkee Korent, Póol a nga jaare ca diiwaan yu tunde ya, ba wàccsi Efes. Mu daje faakay taalibe,

Acts 21:4 TSK

Nu seet taalibey foofa, ba gis leen, toog ak ñoom juróom ñaari fan. Ci biir loolu Noo gu Sell gi di leen xiir ci wax Póol, ne ko bumu dem Yerusalem.