TSK

TSK · Acts 4:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba loolu amee Yeesu wax ak ña ko jàppsi: sarxalkat yu mag ya, ak kilifay wattukati kër Yàlla ga, ak mag ña. Mu ne leen: «Mbete dama di ab fippukat, ba ngeen dikkey saamar aki njur.

Acts 6:12 TSK

Ba loolu amee ñu xabtal nit ñi ak njiit yi, ak firikati yoon yi, ñu ne jalañ, jàpp Eccen, yóbbu ca kurélu àttekat ya.

Acts 9:2 TSK

di sàkku ay bataaxal yu ñeel jànguy dëkk ba ñuy wax Damaas, bataaxal yu yóbbante ndigal lu yeewlu képp ku ñu fa gis ku bokk ci Yoon woowu, góor ak jigéen, ngir mu jàpp leen, indi Yerusalem.

¶ Ba loolu amee alal ja njaatigey ndaw sa yaakaaroon, réer leen, ñu jàpp Póol ak Silas, diri, yóbbu ca pénc ma, fa kanam njiit ya.