TSK

TSK · Acts 5:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Gewasi daldi daw dabi Naaman. Ba ko Naaman séenee muy daw wutsi ko, mu cëppoo ca watiiram dajeek moom, ne ko: «Mbaa jàmm la?»

Waaw, nit dina sàcc Yàlla? Ndaxam yeen yeena ngi may sàcc te yeena ne: “Ana nu nu la sàcce?” Xanaa ci seen cérub fukkeelu alal akub jooxe.

Acts 4:34 TSK

Kenn ci ñoom ndóolul, ndax képp ku ciy boroom suuf mbaa ay kër, da koy jaay, indi njég li,

Acts 5:3 TSK

¶ Ba loolu amee Piyeer ne ko: «Anañas, lu waral Seytaane di fees sab xol, ba ngay wor Noo gu Sell gi, di làq lenn ci njégu tool bi?

Ndax sopp xaalis kat mooy reenu mboolem xeeti loraange. Am na ñuy ŋaf-ŋafi, di ko wut, far lajj yoonu ngëm, ba teg seen bopp tiis yu bare.