TSK

TSK · Acts 5:40

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Boroom ngis, ñu ne ko: «Bul gis,» boroom peeñu, ñu ne ko: «Bu ñu firil peeñuy dëgg. Wax nu lu neex, gisal nu ay nax.»

Micah 2:6 TSK

Seen yonent yeey waare naa: «Buleen waare! Nii kat deesu ko waaree, gàcce du nu dab!»

Ba tóokër ba ñoree, mu yebal ca beykat ya ab surga, ngir ñu jox ko wàllam ca meññeef ma. Beykat ya dóor surga ba, ba noppi dàq ko, mu dellu loxoy neen.

Acts 4:17 TSK

Waaye kat bu mbir mi gëna siiw ci xeet wi. Nan leen tëkku, ngir aaye leen ñu waxati kenn tur woowu.»

ci Yawut yi lañu ma dóore juróomi yoon, ñeent fukki kàccri yu yées benn.