TSK

TSK · Acts 7:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Aji Sax ji wax Ibraam ne ko: «Déglul bu baax li ma lay wax: sa askan dinañu nekk ay doxandéem ci réew mu ñu moomul, ñu def leeni jaam, sonal leen diiru ñeenti téeméeri at.

Bànni Israyil nag di fulandiwu, gëna yokku, Yàlla defal rewlikat ya aw yiw,

Acts 7:6 TSK

Yàlla ne ko: “Saw askan dinañu toxuji bitim réew, te dees na leen def ay jaam, mitital leen diiru ñeenti téeméeri at (400).”

¶ Soppe yi, lenn a ngii, buleen ko umple: benn bés ni junniy at la mel ci Boroom bi; junniy at mel ni benn bés ci moom.