TSK

TSK · Amos 1:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Jëmmi taabi wurus yooyu waa Filisti yónnee ngir saraxu peyug tooñ, ñeel Aji Sax ji, ay teraanga la yu bawoo ci kilifay dëkk yii: Asdodd, benn; Gasa, benn; Askalon, benn; Gaat, benn; Ekkron, benn.

Éy su ma sama ñoñ déggaloon, éy su Israyil toppoon samay nammeel!

Filistee, seen yetu gannaaw wi damm, bu ko kenn ci yeen bége, nde ci ëkku jaan ji, la ñàngóor di génne, am tostanam mujj di céebi.

bésub sànkute dikkal képp kuy Filisteen, ba dagge dëkk yii di Tir ak Sidon ndimbal lu ñu dese woon. Aji Sax jaa ngay sànk Filisteen, ña des te cosaanoo dunu Keret.

Amos 3:9 TSK

Yéeneleen ca biir taaxi Asdodd ak ca biir taaxi Misra. Neleen: «Dajeleen ca kaw tundu Samari, ba gis na Samari salfaañoo, ak notaange ga fa nit di daj.

Xeet wu raxe mooy sanci Asdodd, te maay sàggi sagub Filisteen ñi.