Isaiah 47:3
TSK
Na sa yaram feeñ, say cér ne fàŋŋ. Damay feyu, te duma bale.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Na sa yaram feeñ, say cér ne fàŋŋ. Damay feyu, te duma bale.
Ma seet ci seen biir kuy defaraat tata ji, janook man ci bëttukaay bi, ngir taxawal réew mi, ba duma tas réew mi, waaye gisuma kenn.
Rawtu dina réer ku gaaw, boroom doole du tala jariñoo dooleem, jàmbaar sax du mana rawale bakkanam.
Aji Sax ji da ne waa kër Israyil: «Sàkkuleen ma, ba dund.
Yeesu ne: «Maa leen ko wax déy, jëtun bii, ñii ñépp, moo leen ëpple lu mu joxe.
¶ Ana fu jote yeek xuloo yi ci seen biir jóge fu moy seen bànneexi bakkan, yiy xare ci seen yaram?