¶ Diiru juróom ñaari fan nag ñu jàkkaarloo ca seeni dal. Bésub juróom ñaareel ba xare ba jib, waa Israyil daane téeméeri junniy xarekat (100 000) yu warul fas ca waa Siri ci benn bés bi;
TSK
TSK · Amos 5:19
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
1 Kings 20:29
TSK
Ku gas um yeer, repp nga tàbbi ca; ku bëtt miir, repp jaan matt la;
Isaiah 10:3
TSK
Ana nu ngeen di def keroog bésub mbugal ba, keroog ba safaan di bawoo fu sore? Ana ku ngeen di daw wuti wallam? Ana fu ngeen di denci seen teraanga?
Isaiah 24:18
TSK
Nga déggi yuux, daw, tàbbi biir pax, génne pax, laawoob caax. Mbàndi kaw kat ubbi na, kenug àddina di reng-rengi.
Jeremiah 48:43
TSK
Yeen waa Mowab, pat-pati rekk, di tàbbiy pax aki yeer.» Kàddug Aji Sax jee.
Acts 28:4
TSK
Waa réew ma gis jaan ja langaamoo loxol Póol, ñu naan ca seen biir: «Nit kii kay ab bóomkat lay doon, ndegam moo rëcce géej, te taxul Ndogal may ko mu dund.»