TSK

TSK · Amos 9:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Dingeen bàcc ba keroog wittum reseñ jot te dingeen witt reseñ ba keroog ji jot. Dingeen lekk seenum pepp ba suur këll te dingeen dëkk ak jàmm ci seenum réew.

tund yi ne soyox seey fi kanam Aji Sax ji boroom àddina sépp.

Garab gu dul ruus ay wuutub gajj, garab gu dëkke naat wuutub taxas, muy woyu Aji Sax ji, te di firnde ju sax, du dog mukk.»

«Yaw laay digool ba fàww, ab séy, te njekk ak njub ak ngor ak yërmande ci laay digook yaw ab séy.