All books in KYG

Daniel 11

KYG · verse 24

12 chapters

KYG / Daniel / Chapter 11

KYG · verse 24

D ay dugg ndànk ba ca biir gox ya gëna woomle ca diiwaan ba. Dina fa def lu ay baayam aki maamam masula def. Dina lël ay réew, séddale ay farandoom alal jaak koom ga. Dina lal pexe yu mu songe ay tata, waaye loolu ab diir lay doon.