«Ngalla sang bi, seetlu nu diiru fukki fan, ñu di nu jox ci meññeef mi rekk ak ndoxum naan;
TSK
TSK · Daniel 12:11
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Daniel 1:12
TSK
Daniel 8:11
TSK
Muy damu bay diir mbagg Njiital gàngooru xare gi, daldi dakkal sarax ba ñu ko daan defal bés bu jot, màbb bérabam bu sell ba.
Daniel 9:27
TSK
Dina feddli kóllëre diggam ak ñu bare ci benn àppu juróom ñaar, te ci diggu àppu juróom ñaar ba lay dakkal sarax yi ñuy rendi ak yeneen sarax. Ci genn wetu sarxalukaay bi la yàqkat biy taxawal lu siblu, di sabab yàqute, ba keroog muj gi ñu ko dogalal ne milib ci kawam.»
Revelation 11:2
TSK
Waaye ëttu bitib kër Yàlla gi, bàyyi ko, bu ko natt, ndax ñi dul Yawut lees ko jox, te ñooy dëggaate dëkk bu sell bi diiru ñeent fukki weer ak ñaar.
Revelation 13:5
TSK
¶ Ñu may rab wi nag muy kañu ak a saaga Yàlla, may ko it mu saña wéye noonu diiru ñeent fukki weer ak ñaar.