All books in KYG

Daniel 2

KYG · verse 28

12 chapters

KYG / Daniel / Chapter 2

KYG · verse 28

W aaye, Buur Nabukodonosor, Yàllaa ngi biir asamaan, di xamle ay mbóot te moo la won liy am jamono yiy ñëw. Sa gént gaak la nga ca gis ca sa kaw lal, lii la: