TSK

TSK · Daniel 2:31

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Maay delloo àddina mbonam, yool ku bon tooñam, maay sàggi sagub ku reew, detteel puukarey ku néeg.

maa ngii di la indil ay làkk-kat, yéefar yi gëna néeg. La nga sottale xel mu rafet, ñoo koy boccil saamar, te ñooy yàq sab taar.

Yaw Buur, buuru buur yi, yaw mi Yàlla Boroom asamaan jox nguur ak kàttan ak dooleek ndam,

Ñu ñàng, raglu, te di dogalal seen bopp àtteb yoon ak sañ-sañ.

Luke 4:5 TSK

¶ Seytaane yéege na ko itam, won ko mboolem nguuri àddina, ci xef ak xippi.