TSK

TSK · Daniel 4:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ca la gub yu gooy ya wonn juróom ñaari gub yu nangu ya te baax. Gannaaw loolu Firawna yewwu, xam ne gént la woon.

Jàppool say jat rekk ak sa xërëm yu ne xas yoo dale sonn ba ngay ndaw. Jombul mu amal la njariñ, mbaa ñu ragale la ko.

Mu woolu taryaax yi ak ñeengokat yi ak jibar yi ak xërëmkat yi, ngir ñu firil koy géntam. Ñu agsi taxaw ca kanamam.

¶ «Loolu laa gént, man, Nabukodonosor. Yaw Beltasar nag, wax ma piri mi. Ndax boroom xam-xam yi ci sama réew mi, kenn manu ma cee wax piri mi. Waaye yaw man nga ko, ngir xelum yàlla yu sell yaa ngi ci yaw.»