TSK

TSK · Daniel 6:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Kon nag Buur, ndegam soob na la, na ab dogal tukkee fi yaw, ñu bind ko ci ndigali yooni Pers ak Medd, yi dul toxu, di xamle ne Wasti dootu jàkkaarlooteek Buur Aserus. Te Buur, dangay nangu céru lingeeram, jox ko moroomam mu ko gën.

Saytukati nguur gépp ak laman yeek jawriñ yeek boroom xel yeek jaraaf yi mànkoo nañu, tëral dogalu buur bi yoonal aaye bii: ci diiru fanweeri fan, képp ku ñaan ci jenn yàlla mbaa ci nit ku la moy, yaw Buur sang bi, dees na ko sànni ca kàmbu gaynde ya.

Ndigal loolu nag tax mu sànni leen ca néeg ba gëna ruqe ca kaso ba, jéng leen.