TSK

TSK · Daniel 6:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Daawuda nag tinu Yàlla ci xale bi: muy woor, fatu, fanaanee tëdd ci suuf.

¶ Ba Axab déggee kàddu yooyu, daa xotti ay yéreem, di woor, sol ay saaku, tëddaale ko, di temp ndànk, ngir toroxlu.

Job 21:12 TSK

Day xaacoondook um tëgg aki xalam, di bége baatub toxoro,

Tabala ju xumb selaw na, ña daa xaxaloo dal, mbégtem buumi xalam dakk.

¶ Ca ñaareelu atu nguurug Nabukodonosor la Nabukodonosor gént gént gu ub boppam lool, ba manatula nelaw.

Jonah 3:3 TSK

Yunus jóg dem ba Niniw, muy la ko Aji Sax ji wax. Niniw nag def dëkk bu réya réy, ba doxub ñetti fan a koy wër.