TSK

TSK · Daniel 6:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Ezra 4:22 TSK

Fexeleen ba baña néewal mbir moomu bala muy law, ba doon loraange ci nguur gi.

Mardose Yawut ba, moo sësoon rëkk ca Buur Aserus, sut Yawut yépp, ay bokki Yawutam yu bare nawloo ko. Muy sàkku nag ngëneeli ñoñam, di waxal jàmm mboolem askanam.

Ku moom sa làmmiñ am nga xam-xam, te ku teey am ngag dégg.

Ma gis ne ni leer ëppe lëndëm njariñ, ni la xel mu rafet ëppe ndof njariñ.

Dégg naa sab jëw, ñu naan noowi yàlla yaa ngi ci yaw, te gis nañu ci yaw ag ràññee akum xel ak xam-xam bu takku.