TSK

TSK · Deuteronomy 1:39

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Seen tuut-tànk, yi ngeen ne alalu sëxëtoo lañuy doon, ñoom laay yóbbu, ba ñu xam réew ma ngeen xarab.

Soow ak lem lay lekk, ba keroog muy mana taamu lu baax, ba lu bon.

Doom ya nag juddooguñu woon bay def lenn lu baax, mbaa lu bon. Yàlla moo defe noonu ngir wéyal dogal bu dëppoo ak tànnéefu boppam