Numbers 31:17
TSK
Kon nag reyleen lépp luy góor ci tuut-tànk yi, mboolem lu ciy jigéen ju xam lalu góor it, rey leen,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Kon nag reyleen lépp luy góor ci tuut-tànk yi, mboolem lu ciy jigéen ju xam lalu góor it, rey leen,
«Man maa tabb buur, fal ko ci Siyoŋ, sama tund wu sell.»
Ñeel Daawuda, di kàddug Sabóor. Aji Sax ji daa wax sama Sang, ne ko: «Toogeel sama ndijoor, ba ma def say noon sa ndëggastal.»
Dina feeñ it ndax noflaay ba mu nuy booleek yeen ñiy dékku ab coono, sédde nu ko, kera bés bu Sang Yeesu feeñee, ànd ak ay malaakaam yu làmboo manooreem, wàcce asamaan.