TSK

TSK · Deuteronomy 23:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Doomu doxandéem bu jokku ci Aji Sax ji, bumu ne: «Aji Sax jee may beddee beddi ci ñoñam.» Jaam bu ñu xañ ngóora it bumu ne: «Man garab gu jaasir doŋŋ laa.»

Xeet wu raxe mooy sanci Asdodd, te maay sàggi sagub Filisteen ñi.

Bu ñu leen xañee yar bi jépp doom am wàll, dafa fekk ngeen di doomi po, waaye du ngeen doomi yoon.