TSK

TSK · Deuteronomy 30:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Sama doom, déggal samay wax, fonk samay santaane.

Ndax man, xel mu rafet, maa gën gànjar, loo bëgg maa ko raw.

Acts 8:27 TSK

Filib fabu, dem. Ndeke am na jenn waayu Ecopi ju màggalsi woon Yerusalem. Nit kooku doonoon moraange, te di jaraaf ju mag ju Kàndas Lingeeru Ecopi; moo doon saytu mboolem alalu Lingeeru Ecopi.

Ca saa sa nag laa yeble ci yaw. Yaw it def nga lu baax, bi nga dikkee. Léegi nag nun ñépp a ngi fi ci kanam Yàlla, ngir déglu mboolem lu la Boroom bi sant.»

¶ Waaye nees di wooye koo gëmul? Nees di gëme koo déggul turam? Nees di dégge turam, te yégleesu ko?