TSK

TSK · Ecclesiastes 2:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Guddig keroog Buur tëlee nelaw, daldi santaane ñu indil ko téere ba ñu dippee Xew-xew ya. Ci kaw loolu ñu di ko jàngal Buur.

Job 7:13 TSK

Dama naan: «Naa nopploo tëraayub laltu, ba yennikoo ab lal sama tawat,»

Deesul dee ba fàttliku la; ku dugg njaniiw, nu mu lay sante?

Naa xaacu, woo Yàlla, sama baat fa Yàlla, ngir mu déglu ma.

Bànneexal nu limu fan yi nga nu mbugal, diirub ati tiis yi nu dund.

Ku géejal xel mu rafet, géejal naqar; yokku xam-xam, yokku tiis.

Ma walbatiku xalaat, di jéema xam fu xel rafete, di xoolaat li nit jàppoo fi kaw suuf, ba guddeek bëccëg, gëmmul bët.

Ñuy feddli pastéefu taalibe yi, di leen ñaax ngir ñu saxoo ngëm, ne leen: «Coono yu baree ngii, fàww nu jaare ci, ngir tàbbi ci nguurug Yàlla.»