¶ Ba Ibraam déggee ne jàpp nañu Lóot ma muy baayam bu ndaw, fa saa sa daa dajale dagam, yi juddoo këram te tollu ci ñetti téeméer ak fukk ak juróom ñett (318), ñu dàq buur ya ba dëkk ba ñuy wax Dan.
TSK
TSK · Ecclesiastes 3:8
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Suleymaan moo yilifoon mboolem réew ma féete dexu Efraat sowu, dale ko ca Tifsa ba ca Gasa, muy mboolem réew ya féete dexu Efraat sowu. Jàmm ne ñoyy, féete ko wet gu nekk.
mu xiir waa Misra ci dëddu ñoñam, ñuy fexeel jaamam ñooña.
Ma jaareeti fa, xool la, gis ne mat ngaa séy. Ma tàllal sama mbubb, sànge ko sa yaramu neen, ba noppi giñal la, dikke la kóllëre. Kàddug Boroom bi Aji Sax jee. Nii laa la moome.
Ngeen boole ci daj cofeelu Almasi, gi wees xam-xam, ngir ngeen fees, ba fees dell ak koomu Yàlla.
¶ Noonu la jëkkër ji wara soppe jabaram, ni mu soppe yaramu boppam rekk. Sopp sa jabar sopp sa bopp la,
¶ Gis naa say jëf, gis sa liggéey ak sag muñ. Xam naa ne manuloo dékku ñu bon ñi. Seetlu nga ñi tuddoo samay ndaw, ba gis ne ay fen-kat lañu.