Nehemiah 8:11
TSK
Leween ña nag di dëfal mbooloo ma mépp, naan leen: «Noppileen waay, ndax tey bés bu sell la. Kon buleen ci naqarlu.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Leween ña nag di dëfal mbooloo ma mépp, naan leen: «Noppileen waay, ndax tey bés bu sell la. Kon buleen ci naqarlu.»
Ña ngay maye naan ci ay kaasi wurus, bu ci nekk wuuteek moroom ma na mu bindoo. Biiñu buur di walangaan ni loxol Buur.
Waa àddina dinañu bége seen dee, di bànneexu, di joqlante ay njukkal, ndaxte ñaari yonent yooyu ñoo lakkaloon waa àddina.