TSK

TSK · Exodus 29:39

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ca suba sa, ba ñuy tollu ci rendi sarax rekk; ndox ma bàyyikoo yoonu Edom, wal, ba fépp fees ak ndox.

Ezra 9:4 TSK

Ba loolu amee mboolem ñi wormaal kàddug Yàllay Israyil daje, wër ma ndax ñàkk kóllëreg ña ñibbsee ca ngàllo ga. Ma toog, ne tott ba waxtuw saraxu ngoon.

Yal na leen dee bett, ñu jekki tàbbi njaniiw, ngir mbon ga seen biir ak seen dëkkuwaay.

¶ «Am xarum menn at mu amul sikk lees di defal Aji Sax ji bés bu nekk saraxu rendi-dóomal, te suba su ne lees koy def.

Acts 26:7 TSK

Te mooy dige bi fukki giir ak ñaar yu bànni Israyil di séentu mu sottil leen, ba tax guddi ak bëccëg ñu xér ci jaamu Yàlla. Yaakaar jooju nag, Buur, moo tax Yawut yi tuumaal ma!