TSK

TSK · Exodus 36:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Njiit yi nag indi ay peri onigsë ak yeneen per yiy tappe ci xar-sànni meek kiiraayal dënn bi,

Sama Buur, sama Yàlla, déglul, ma ne wallóoy! Yaw laay ñaan.

Samay pexe la buur di jiitee, kilifa di ci àttee dëgg.

Yeen waa kër Daawuda, Aji Sax ji dafa wax ne: Àtte yoon, deeleen ko xëye, di xettli ki ñu xañ dëgg ci ki koy néewal doole, balaa sama mer ne jippét, di tàkk te deesu ko mana fey ndax seen jëf ju bon.