TSK

TSK · Ezra 6:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Ezra 4:23 TSK

¶ Naka lañu jàng bataaxalu Buur Artaserses fa kanam Reyum boroom dëkk ba, ak Simsay bindkat ba aki nàttongoom, ñu ne coww ba Yerusalem, ca Yawut ña, jaay leen doole, gétën leen, ñu bàyyi liggéey ba.

Ezra 6:6 TSK

¶ Kon nag ñooñu di Tatnay boroom Wàllaa Dex ak Setar Bosnay ak seen nàttongo yay jawriñ ca Wàllaa Dex, nañu sore foofa.

Job 5:12 TSK

Keey neenal pexem ku muus, ba mébétam du sotti.

Kàddug buur kilifteef la. Ana ku ko naan: «Looy def nii?»