TSK

TSK · Ezra 7:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Ezra 1:3 TSK

Képp ku bokk ci mboolem ñoñam, yal na Yàllaam ànd ak moom, mu dem ba Yerusalem ga ca Yuda, tabax fa kër Aji Sax ji, Yàllay Israyil, Yàlla ja ca Yerusalem.

Ezra 6:1 TSK

¶ Ba loolu amee Buur Daryus joxe ndigal, ñu seet ca kërug dencukaayi téere ya, fa ñu denc alali Babilon.

Buur joxe ndigal ngir ñu def noona. Ba loolu amee ñu siiwal ab dogal ca Sus, daldi wékk fukki doomi Aman yu góor ya.

Moo leen samp, ñu sax ba fàww, mu dogal ko, te du toxu.

¶ Noo gi ak Séet bi neeñu: «Ñëwal!» Ku ci dégg it, neel: «Ñëwal!» Ku mar, ñëwal; ku bëgg ci ndoxum dund mi, jëlal, ñu may la.