TSK

TSK · Genesis 13:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ada taawloo Yabal, miy cosaanu sàmm yiy màngaan,

Ibraam ànd ak soxnaam Sarayi ak Lóot, mi muy baay bu ndaw ci moom. Mu yóbbaale nag alal, ja mu dajale jépp, ak jaam, ya mu jënde Karan. Ñu jóge fa, jublu réewu Kanaan.

nangu xaymaaki jur, ak kiiraay ak luy jumtukaay, yóbbu seeni giléem, te biral leen, ne leen: “Musiba ubale na!”