Aadama ne ko: «Jigéen, ji nga ma booleel de, moo ma jox ci garab gi, ma lekk.»
TSK
TSK · Genesis 16:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Sarayi moomu masuloona am doom te it manu ko woona am.
Kooka ne ko: «Nëgëni sii déwén déy laay délsi, te sa soxna Saarata dina am doom ju góor moos.» Bi muy wax loolu, Saarataa ngi ci buntu xayma bi ci gannaawam, di déglu.
Gannaaw ga soxnas Isaaxa amul doom, Isaaxa dagaanal ko Aji Sax ji, mu nangul ko, soxna si daldi ëmb.
Mu ne ko: «Xoolal, sama jaam Bilaa ngii; dëkkoo ko, ndax mu amal ma doom, ba jabootal ma.»
¶ Leya moom it xam ne taxawaayam yàgg na, mu fab jaamam Silpa, may ko Yanqóoba.
Su fekkee ne sangam a ko may jabar, ndaw si am ak moom ay doom, jabar jeek doomam yu góor mbaa yu jigéen, sang bee leen di moom. Moom ci boppam doŋŋ ay moom boppam.
Ma ne, doom Aji Sax jee koy sédde, njurum doom yool la.