TSK

TSK · Genesis 19:25

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ñooñoo booloo woon ca xuru Sidim, mooy géeju Xorom gi léegi.

Yal na kooku mel ni dëkk, yi Aji Sax ji tas te yërëmu leen! Yal na dégg yuuxi suba teel ak xaacuy xarey njolloor.

Moo tax, giñ naa ko ci man miy dund,» kàddug Aji Sax ju gàngoor yee, Yàllay Israyil, «Mowab déy ni dëkkub Sodom lay mujje, Amoneen ñi mel ni Gomor, ay dég ak paxi xorom a koy nangu, mu gental ba fàww. Sama ndesu ñoñ a leen di sëxëtoo, ndesu xeet wi ma séddoo moo leen di moom.»