TSK

TSK · Genesis 21:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye sama kóllëre nag, Isaaxa laa koy fasool, moom Isaaxa, mi Saarata di am, nëgëni déwén.»

Kon déggal leen rekk, waaye àrtu leen bu baax, xamal leen luy doon sañ-sañu buur bu leen di jiiteji.»

Te it sëti Ibraayma yépp bokkuñu ci askanam, waaye li Mbind mi indi moo di: «Ci Isaaxa lees di tudde saw askan.»