Genesis 16:10
TSK
Mu teg ca ne ko: «Dinaa yokk sa askan lool, ba kenn du leen mana waññ,»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mu teg ca ne ko: «Dinaa yokk sa askan lool, ba kenn du leen mana waññ,»
Demal yékkati ko, may ko loxo, mu jóg. Dinaa def mu law, ba doon xeet wu yaa.»