All books in KYG

Genesis 21

KYG · verse 8

50 chapters

KYG / Genesis / Chapter 21

KYG · verse 8

B a loolu amee doom ja màgg, ba bés, ba ñu ko feralee. Keroog Ibraayma def na bernde ju mag.