Genesis 34:20
TSK
Amor nag ànd ak doomam Sikem, dem ba ca pénc ma, wax ak waa dëkk ba ne leen:
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Amor nag ànd ak doomam Sikem, dem ba ca pénc ma, wax ak waa dëkk ba ne leen:
¶ Ci biir loolu Bowas dem ba ca bunt dëkk ba, toog fa. Noonu rekk mbokk ma mu waxoon ne su dee jotaat, moo ko ci gëna yey, daldi fay jaare. Mu woo ko ne ko: «Diwoo, kaay fii, toog tuuti.» Mu dikk, toog.
mooy sol noowug dëgg kuy toog di àtte, di jàmbaaral ñiy waññi noon yi song dëkk bi, xare.
Ci kaw loolu ñépp binduji, ku nekk ca sa dëkku cosaan.